Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna Podcast Por Studio Ëpoukay arte de portada

Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna

Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna

De: Studio Ëpoukay
Escúchala gratis

Suniouy wakh si migration fi sénégal, liniouy geuneu xalaat moy ay ndaw you goor yuy dieul gaal nguir dem Espagne. Wayé daniouy faté ni si biir tukki katt yoyou amna ay jiguén.

Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information.

Studio Ëpoukay
Ciencias Sociales Escritos y Comentarios sobre Viajes
Episodios
  • E0 - Teaser
    Feb 12 2024
    Bande-annonsou série « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » Podcast bi amna 7 épisodes gni ko réalisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay.

    Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information.

    Más Menos
    2 m
  • E1 -- Li waral ñuy tukki
    Mar 8 2024
    Épisode bou ndieuk si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay.

    Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information.

    Más Menos
    9 m
  • E2 - Jaar-jaaru Aissatou
    Mar 9 2024
    Niarelou épisode bi si diourom niari épisodou serie « Jiggéen yuy tukki : Dakaar ba fépp ci àdduna » gniko realisé di Ibrahima Diouf ak Clair Rivière bou studio Ëpoukay.

    Hosted on Acast. See acast.com/privacy for more information.

    Más Menos
    10 m
Todavía no hay opiniones